Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 5:4-6 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 5:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Baña digee gën dige loo deful.
5 Bu la sa làmmiñ yóbbe bàkkaar, ba ngay lay ndawal Yàlla la, naan lii njuumte la woon. Ana lu jar Yàlla di la meree sa kàddu, bay neenal saw ñaq?
6 Wax ju bare, caaxaani neen; mook gént yu baree yem. Kon, Yàlla, ragal ko.
Kàdduy Waare 5 in Kàddug Yàlla gi