Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 5:3-5 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 5:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Boo digook Yàlla, bu ko yeexe; Daray foontukat neexul, defal li nga dige.
4 Baña digee gën dige loo deful.
5 Bu la sa làmmiñ yóbbe bàkkaar, ba ngay lay ndawal Yàlla la, naan lii njuumte la woon. Ana lu jar Yàlla di la meree sa kàddu, bay neenal saw ñaq?
Kàdduy Waare 5 in Kàddug Yàlla gi