Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 5:3-4 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 5:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Boo digook Yàlla, bu ko yeexe; Daray foontukat neexul, defal li nga dige.
4 Baña digee gën dige loo deful.
Kàdduy Waare 5 in Kàddug Yàlla gi