Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 4:5-6 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 4:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Dof banki loxoom, sànk boppam.
6 Waaye benn ŋëb bu ànd ak dal moo gën ñaari ŋëbi doñ-doñ ci napp um ngelaw.
Kàdduy Waare 4 in Kàddug Yàlla gi