Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 4:3-6 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 4:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Ki leen taneeti yeen ñépp di ki juddoogul sax, moom mi gisul jëf ju bon fi kaw suuf.
4 Ma gis ne nit ak kër-këram jépp ak bépp manoorey liggéey, iñaanantee ko waral. Loolu it, cóolóoli neen ak napp um ngelaw.
5 Dof banki loxoom, sànk boppam.
6 Waaye benn ŋëb bu ànd ak dal moo gën ñaari ŋëbi doñ-doñ ci napp um ngelaw.
Kàdduy Waare 4 in Kàddug Yàlla gi