Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 10:7-9 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 10:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 ma gis baadoolo war fas, kilifa di rung ni baadoolo.
8 Ku gas um yeer, repp nga tàbbi ca; ku bëtt miir, repp jaan matt la;
9 kuy yett ay doj, repp nga caa gaañu; kuy gor bant, repp nga caa loru.
Kàdduy Waare 10 in Kàddug Yàlla gi