Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 10:5-7 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 10:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Lu mettee ngi lu ma gis fi kaw suuf, lu mel ni njuumte lu rëcc kilifa:
6 Ab dof bu ñu jox cér yu bare, boroom daraja féete suuf;
7 ma gis baadoolo war fas, kilifa di rung ni baadoolo.
Kàdduy Waare 10 in Kàddug Yàlla gi