Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 10:3 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 10:3 in Kàddug Yàlla gi

3 Te it ku dofe buy dox sax, du ànd ak xelam; ku ko gis, xam ne kii dof la.
Kàdduy Waare 10 in Kàddug Yàlla gi