Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 6:3-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 6:3-8 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaa ngi ci sa loxoy moroom, kon defal nii, doom, ba rëcc: doxal tinuji ko, raamali ko.
4 Bul gëmm, bul nelaw!
5 Dawal ni kéwél gu rëcc ub rëbb, ne fërr ni picc mu raw ab fiirkat.
6 Yaafus bee, xoolal xorondom, seetal ci moom, ba muus.
7 Du ku ko yilif mbaa ku koy sas, te jiiteesu ko.
8 Bu jotee mu denc ab dundam, mu jot, mu for lekkam.
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi