Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 30:3-4 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 30:3-4
in
Kàddug Yàlla gi
3
Jànguma, ba am xel mu rafet, awma xam-xam ci Aji Sell ji.
4
Ana ku yéegoon asamaan, ba wàcc? Mbaa mu masa ŋëb ngelaw ciy loxoom? Ana ku masa ëmb ndox ci ndimo? Mbaa mu rëdd mboolem kemi àddina? Nu mu tudd ak nu doomam tudd? Wax ma, yaw mi ko xam!
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms