Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:27-30 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:27-30 in Kàddug Yàlla gi

27 soccet, amul buur, teewul ñuy àndandoo, diy gàngoor;
28 sindax, manees na koo ŋëb, teewul ma nga biir kër buur.
29 Ñett a ngii, ñu jekk um ndaag, ba ci ñeent ñu jekk doxin:
30 gaynde, mooy buuru rab yi, ragalul kenn;
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi