Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:20-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:20-23 in Kàddug Yàlla gi

20 Jikkoy jigéenu moykat a ngi. Day lekk, wommiku, te naan: «Defuma dara lu aay!»
21 Ñett a ngii, day yëngal suuf, ba ci ñeent yu suuf àttanul:
22 jaam bu falu buur, dof bu regg,
23 ndaw su bon su for jëkkër, jigéen ju wuutu sangam bu jigéen.
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi