Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:17-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:17-19 in Kàddug Yàlla gi

17 Kuy xeelu sa baay, di siidee déggal sa ndey, baaxoñ génne ciw xur, luqi sa bët, tan ya lekk.
18 Ñett a ngii, yéem na ma, ba ci ñeent yu ma xamul:
19 yoonu jaxaay ci asamaan, yoonu jaan ci kawi doj, yoonu gaal ci diggu géej, yoon wi góor di jaar as ndaw.
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi