Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:16-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:16-18 in Kàddug Yàlla gi

16 njaniiw, jigéen ju jaasir, suuf, du màndi ndox, sawara, du ne doy na mukk.
17 Kuy xeelu sa baay, di siidee déggal sa ndey, baaxoñ génne ciw xur, luqi sa bët, tan ya lekk.
18 Ñett a ngii, yéem na ma, ba ci ñeent yu ma xamul:
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi