Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:14-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:14-15 in Kàddug Yàlla gi

14 Ag maas a ngi, seeni sell niy saamar, seeni gëñ niy paaka, ñuy lekk néew-ji-doole, ba raafal leen ci réew mi, ba ku ñàkk jeex ci biir nit ñi.
15 Saxu watar du suur, ñaar ñu jigéen la am: Jox Ma ak Jox Ma. Ñett a ngii ñu dul suur, ba ci ñeent ñu dul ne doy na mukk:
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi