Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:7-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Gone gu sàmm yoon am nag dégg, ku ànd ak sagaru nit gàcceel sa baay.
8 Kiy leble di tege, ba barele, kay yéwéne néew-ji-doole lay dencal.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi