Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:24-26 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:24-26 in Kàddug Yàlla gi

24 Ku xañ say waajur seen alal te defe ne tooñoo, yaa neexook saaysaayu yàqkat.
25 Ku bëgge day sooke ay, te ku wóolu Aji Sax ji, woomle.
26 Ku doyloo sam xel, dof nga; ku jëfe xel mu rafet, mucc nga.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi