Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:23-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:23-25 in Kàddug Yàlla gi

23 Boo artoo nit, mu baaxe la ëllëg; yaa koy gënal ku ko doon jay.
24 Ku xañ say waajur seen alal te defe ne tooñoo, yaa neexook saaysaayu yàqkat.
25 Ku bëgge day sooke ay, te ku wóolu Aji Sax ji, woomle.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi