Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:22-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:22-23 in Kàddug Yàlla gi

22 Ab nay day yàkkamtee barele, te xamul, ba ko ñàkk di dab.
23 Boo artoo nit, mu baaxe la ëllëg; yaa koy gënal ku ko doon jay.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi