Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Boroom worma, bare barke; ku yàkkamtee woomle, sa mbugal du jaas.
21 Par-parloo baaxul, waaye dogu mburu moyloo na kilifa.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi