Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:13-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Kuy làq say tooñ doo baaxle, ku koy nangu, tuub ko, am yërmandey Yàlla.
14 Mbégte ñeel na ku saxoo ragal, waaye ku dëgër bopp tàbbi ci njekkar.
15 Kilifa guy soxore néew-ji-doole mook gaynde guy yëmmoo yem, mbaa rab wuy songe.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi