Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 26:7-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 26:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof, mooy tànki lafañ, amalu ko njariñ.
8 Kuy teral ab dof, jël ngaw doj, takk ko ci mbaq.
Kàddu yu Xelu 26 in Kàddug Yàlla gi