Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 26:25-26 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 26:25-26 in Kàddug Yàlla gi

25 Buy wax lu neex, bul gëm, ñaawtéef la xol ba fees dell.
26 Su la nëbbalee mbañeel, di la nax it, ag mbonam mujj bir ñépp.
Kàddu yu Xelu 26 in Kàddug Yàlla gi