Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 26:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 26:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Bu matt amul, ab taal fey, fu soskat amul it, xuloo jeex fa.
21 Këriñ defi xal, matt xamb ub taal, ab xulookat di xambu ay.
Kàddu yu Xelu 26 in Kàddug Yàlla gi