Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 26:13-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 26:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Ab yaafus da naan: «Gayndee ngi ci yoon wi! Gayndee ngi ci mbedd mi!»
14 Ab yaafus day tëdd ak a walbatiku, mooy bunt, day jaayu, demul fenn.
15 Ab yaafus day yeb loxoom ci ndab, waaye yékkati ko, sex, da koy sonal.
Kàddu yu Xelu 26 in Kàddug Yàlla gi