Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 26:12-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 26:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Ana koo gis mu ne: «Maa xelu»? Kooku ab dof a ko gën demin.
13 Ab yaafus da naan: «Gayndee ngi ci yoon wi! Gayndee ngi ci mbedd mi!»
14 Ab yaafus day tëdd ak a walbatiku, mooy bunt, day jaayu, demul fenn.
Kàddu yu Xelu 26 in Kàddug Yàlla gi