Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 20:20-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 20:20-22 in Kàddug Yàlla gi

20 Ku saaga sa ndey mbaa sa baay añe lëndëmu bàmmeel.
21 Alal ju gaaw du mujje barkeel.
22 Bul feyantook ku la tooñ; dénkul ci Aji Sax ji, mu wallu la.
Kàddu yu Xelu 20 in Kàddug Yàlla gi