Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 20:2-3 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 20:2-3 in Kàddug Yàlla gi

2 Buur mer lool, mel ni gayndee ŋar; boo ko merloo, dangay xaru.
3 Moytuw ay, ndam la; dof boo gis day bëgg xuloo.
Kàddu yu Xelu 20 in Kàddug Yàlla gi