Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 20:17-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 20:17-18 in Kàddug Yàlla gi

17 Njublaŋ, lekk, jëkke neex, mujj mel ni lancub suuf.
18 Pexe, ndigal a koy lal; xare, ay tegtal.
Kàddu yu Xelu 20 in Kàddug Yàlla gi