Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 20:16-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 20:16-18 in Kàddug Yàlla gi

16 Ku gàddul jaambur bor, jëlal mbubbam; tayle ko, moo dige feyal jaambur.
17 Njublaŋ, lekk, jëkke neex, mujj mel ni lancub suuf.
18 Pexe, ndigal a koy lal; xare, ay tegtal.
Kàddu yu Xelu 20 in Kàddug Yàlla gi