Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:8-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Waxi jëwkat di ñam wu neex wuy seey, jàll ca biir-a-biir.
9 Kuy sàggane sa liggéey, yaak kuy yàq a bokk.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi