Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:5-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:5-8 in Kàddug Yàlla gi

5 Faral ku tooñ baaxul, bul xañ dëgg ku deful dara.
6 Ab dof, làmmiñam sooke naw ay, ay waxam di sàkku yeti gannaaw.
7 Ab dof, waxam a koy sànk, làmmiñu boppam a koy dugal.
8 Waxi jëwkat di ñam wu neex wuy seey, jàll ca biir-a-biir.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi