Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:5-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Faral ku tooñ baaxul, bul xañ dëgg ku deful dara.
6 Ab dof, làmmiñam sooke naw ay, ay waxam di sàkku yeti gannaaw.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi