Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:3-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Bu mbon nuyoo, xeebeel topp ca; jëf ju ñaaw, gàcce rekk.
4 Waxi nit ndox mu xóot la, bu bënnee, xelli, ñu di ca xelu.
5 Faral ku tooñ baaxul, bul xañ dëgg ku deful dara.
6 Ab dof, làmmiñam sooke naw ay, ay waxam di sàkku yeti gannaaw.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi