Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:21-24 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:21-24 in Kàddug Yàlla gi

21 Dund ak dee a ngi ci làmmiñ, te wax garab la, ku ko bëgg, lekk ca doom ya.
22 Ku am jabar, am nga ngëneel, am nga yiwu Aji Sax ji.
23 Ku ñàkk a ngi leewaayu, boroom alal di ko jànni.
24 Barey àndandoo lor a ngi ci, waaye xarit a ngi gëna taq nit mbokkam.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi