Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:2-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:2-5 in Kàddug Yàlla gi

2 Ab dof wutul ag dégg, balaa caag muy jaay ag muus.
3 Bu mbon nuyoo, xeebeel topp ca; jëf ju ñaaw, gàcce rekk.
4 Waxi nit ndox mu xóot la, bu bënnee, xelli, ñu di ca xelu.
5 Faral ku tooñ baaxul, bul xañ dëgg ku deful dara.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi