Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Jubook mbokk moo tooñ, jéggi tataa ko gëna yomb, mbaa ubbi bunt yu tëje ràpp.
20 Làmmiñ feesal na biiru boroom, yoolu kàddu suur na boroom.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi