Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:15-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:15-18 in Kàddug Yàlla gi

15 Ku am ug dégg wut xam-xam, ku rafet xel sàkku xam-xam.
16 Deel maye, da lay ubbil bunt, di la àggle ci boroom daraja.
17 Ku jëkke layoo, ñu ne yaa yey, ba keroog ka nga joteel weddi la.
18 Tegoo bant day feyu ay, di àtte boroom doole yu jote.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi