Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:12-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Bew, yàqule; jëkke woyof, mujje tedd.
13 Tontu te déggagoo, ndof la, ak ñàkk kersa.
14 Ku bëgga dund, dékku woppi yaram, waaye xol bu jeex maneesu koo wéye.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi