Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:6-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:6-9 in Kàddug Yàlla gi

6 Ab soxor, waxam am tëru la, day reye; kàdduy kiy jubal di musle.
7 Ab soxor bu daanoo, jeex na; ku jub, sa kër taxaw, ne këcc.
8 Xel mu ñaw, jëw bu rafet; sam xel jekkadi, ñu xeeb la.
9 Woyof mbubb, am benn surga doŋŋ, moo gën réyal turki tey dee ak xiif.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi