Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 2:4-5 in Wolof

Help us?

JËF YA 2:4-5 in Téereb Injiil

4 Noonu ñu fees ak Xel mu Sell mi ñoom ñépp, ñu daldi wax yeneen làkk, ni leen Xel mu Sell mi maye, ñu wax ko.
5 Fekk booba amoon na ay Yawut yu daloon Yerusalem, doon ay nit ñu ragal Yàlla te bokk ci xeeti àddina yépp.
JËF YA 2 in Téereb Injiil

Jëf ya 2:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Ñoom ñépp nag feese Noo gu Sell gi, tàmbalee làkk làkk yu wuute, na leen ko Noo gi manloo.
5 Booba ay toppkati yoonu Yawut a nga dëkke Yerusalem, te bawoo ci xeeti àddina yépp.
Jëf ya 2 in Kàddug Yàlla gi