Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 2

Jëf ya 2:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Ñoom ñépp nag feese Noo gu Sell gi, tàmbalee làkk làkk yu wuute, na leen ko Noo gi manloo.
5Booba ay toppkati yoonu Yawut a nga dëkke Yerusalem, te bawoo ci xeeti àddina yépp.

Read Jëf ya 2Jëf ya 2
Compare Jëf ya 2:4-5Jëf ya 2:4-5