Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 25:3-5 in Wolof

Help us?

JËF YA 25:3-5 in Téereb Injiil

3 Ñuy sàkku ndimbal ci moom, di ko ñaan bu wér, mu yónni Pool Yerusalem, fekk lal nañu fiiru rey ko ca yoon wa.
4 Waaye Festus ne leen: «Ñu ngi wottu Pool ca Sesare, te dinaa fa dem fi ak fan yu néew.»
5 Mu ne leen: «Ñi am maana ci yéen nag, nangeen ànd ak man, layooji ak nit ka, bu dee tooñ na.»
JËF YA 25 in Téereb Injiil

Jëf ya 25:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 tinu ko ngir mu woolu Póol Yerusalem, ndax fekk na leen lal pexem rey ko ca yoon wa.
4 Festus itam ne leen Póol a nga ñu tëj kaso ca Sesare, te moom ci boppam, fa la nara gaaw, dellu.
5 Mu ne leen: «Kon nag, na nit ñu am baat ñu bokk ci yeen, ànd ak man, tuumaali waa ji, ndegam am na fenn fu mu tooñe.»
Jëf ya 25 in Kàddug Yàlla gi