Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 1

Jëf ya 1:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Waaye Noo gu Sell gi mooy wàcc ci yeen, ngeen soloo dooleem, daldi doon samay seede ci Yerusalem, ak ci diiwaanu Yude gépp ak ci Samari, ba ca cati àddina.»
9Naka la wax loolu, ndaw yay xoole, ñu jekki yéegee ko fa, aw niir daldi leen koy làq.

Read Jëf ya 1Jëf ya 1
Compare Jëf ya 1:8-9Jëf ya 1:8-9