Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 1

Jëf ya 1:18-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Yuda nag gannaaw ba mu jëndee ab tool ca peyu ñaawtéefam ja, ca la daanu, jiital boppam, biir ba fàcc, butit ya tuuru.
19Waa Yerusalem yépp a ko yég, ba tax ñu tudde tool ba Akeldam, mu firi Toolu deret, ci seen làkk.

Read Jëf ya 1Jëf ya 1
Compare Jëf ya 1:18-19Jëf ya 1:18-19