Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 17:13-14 in Wolof

Help us?

JËF YA 17:13-14 in Téereb Injiil

13 Waaye bi Yawuti Tesalonig déggee ne Pool mu ngi yégle kàddug Yàlla ci Bere it, ñu daldi fay dikk, di jógloo ak a jaxase mbooloo ma.
14 Noonu bokk yi yebal Pool ca saa sa, mu jëm géej, waaye Silas ak Timote des fa.
JËF YA 17 in Téereb Injiil

Jëf ya 17:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Ba loolu amee Yawuti Tesalonig dégg ne Póol a ngay xamle kàddug Yàlla ca Bere itam. Ñu dikkati, yëngal nit ña, ñu def ay gàngoor.
14 Ca la bokki gëmkat ñi yebal Póol ca saa sa, mu jëm tefes ga, Silas ak Timote ñoom, des ca Bere.
Jëf ya 17 in Kàddug Yàlla gi