Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 17

Jëf ya 17:13-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Ba loolu amee Yawuti Tesalonig dégg ne Póol a ngay xamle kàddug Yàlla ca Bere itam. Ñu dikkati, yëngal nit ña, ñu def ay gàngoor.
14Ca la bokki gëmkat ñi yebal Póol ca saa sa, mu jëm tefes ga, Silas ak Timote ñoom, des ca Bere.

Read Jëf ya 17Jëf ya 17
Compare Jëf ya 17:13-14Jëf ya 17:13-14