Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 16:12 in Wolof

Help us?

JËF YA 16:12 in Téereb Injiil

12 Bi nu fa teeree, nu jëm Filib, bi nekk dëkk bi ëpp maana ca wàll woowu ci diiwaanu Maseduwan, di it moomeelu Room. Nu toog fa ay fan.
JËF YA 16 in Téereb Injiil

Jëf ya 16:12 in Kàddug Yàlla gi

12 Nu bawoo fa jàll ba Filipi, dëkku gox ba jëkk ca diiwaanu Maseduwan te di moomeelu Room. Nu toog fa ay fan.
Jëf ya 16 in Kàddug Yàlla gi