Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 11

Jëf ya 11:5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Mu ne: «Man de damaa nekkoon ca Yope, di fa ñaan. Ci biir loolu ma daanu ag leer, daldi gis ci peeñu lu mel ni sér bu mag bu ñu téyee ñeenti lafam, mu wàcce asamaan, ba agsi ci man.

Read Jëf ya 11Jëf ya 11
Compare Jëf ya 11:5Jëf ya 11:5