Text copied!
Bibles in Wolof

2 TIMOTE 2:22 in Wolof

Help us?

2 TIMOTE 2:22 in Téereb Injiil

22 Dawal bépp bëgg-bëggu ngone, te sóobu ci njub, ngëm, mbëggeel, jàmm, ànd ak ñépp ñiy tudd turu Boroom bi ak xol bu sell.
2 TIMOTE 2 in Téereb Injiil

2.Timote 2:22 in Kàddug Yàlla gi

22 Xemmemtéefi ndaw nag, daw ko, te nga topp njub, ak ngëm ak cofeel, ak jàmm, ànd ceek ñiy tudde Boroom bi xol bu set wecc.
2.Timote 2 in Kàddug Yàlla gi